Skip to content
Lyric
Dive
Public playlists
My playlists
Search
Sign in
Dieye Sélémane
AMADEUS
Popularity · Low
+
Original
0
0
Listen
YouTube
1
2
3
0:00 / 0:00
Loading YouTube player...
Lyrics offset
Synced
Lyrics
Original
Translation
Bilingual
Yaa di sama waay
Ma di itam sa waay
Ñaanuma la tooñ
Su amee yal nanga ma baal
Yaa di sama waay
Ma di itam sa waay
Ñaanuma la tooñ
Waaye su amee yal nanga ma baal
Nee ma lii laay bañ
Wax ma ni nga ko bëggee
Jëmm ji laay rang
Njëkkewuma waaye maa lay mujje
Ngëleemu jébbu juróom
Su ma ko amoon néeg namaa
Ñëw jël ko jébbal la ko
Dang ma bëgg lool yéene ma
Àdduna du mas a neex ba ma fàtte la
Jéey Selemaan
Ngëleemu jébbu juróom
Su ma ko amoon néeg namaa
Jéey Selemaan laay way
Jéey Jéey Selemaan laay way
Jéey Selemaan laay way
Jéey Jéey Selemaan laay way
Dëkk ba nga ma jële sori na lool
Diggante yi nga ma fekkoon itam
Metti na woon
Li may man a way lépp soo ko wanewul woon
Kon leneen lay doon
Kon yoon la delloo la njukkal
Jéey Selemaan
Masàmba Laara Jéey
Yérim diir na buur
Taawu Ndumbe Ndeela Jéey
Jéey Selemaan
Masàmba Laara Jéey
Yérim diir na buur
Taawu Ndumbe Ndeela Jéey
Jéey Selemaan
Jéey Masàmba Jéey Selemaan
Masàmba moo ne
Duma dem Siin
Duma dem Saalum
Te ku ma defal lu dul lu buur
Ci sa kaw laay jaar
Jéey Masàmba
Ngëleen mu jebbul juróom
Su ma ko leeg ma maare
Ñu jël ko jébbal la ko
Dang ma bëgg lool ma maare
Àdduna du mas a neex ba ma fàtte la
Jéey Selemaan
Ngëleen mu jébbul juróom
Su ma ko leeg ma maare
Jéey Selemaan laay way
Jéey Jéey Selemaan laay way
Jéey Selemaan laay way
Jéey Jéey Selemaan laay way