Skip to content
Lyric
Dive
Public playlists
My playlists
Search
Sign in
Aljana
Wizzy Kana
Popularity ยท Low
+
๐ธ๐ณ Wolof ยท Original
0
0
YouTube
Searching YouTube...
Lyrics
Original
Translation
Bilingual
Paradise rek laalay jeumรฉ
Thi geedjou banekh laniouy feey maak iow
Beukoulo akk niom niveau
Teg naala thi kaw
Tรฉ dara doulafa dieulรฉ my bve
Aljana
Aljana laala jeumรฉ iow aljana
Dou Aljana lagn nara deukรฉ
Aljana
Oubi sa xol douggeul fa airou aljana
Aljanaaaa
Aljana
Aljana laala jeumรฉ iow aljana
Dou Aljana lagn nara deukรฉ
Aljana
Oubi sa xol douggeul fa airou aljana
Aljanaaaa
Maak iow ba paradise
Denk naala sama life
Dou ayy foo laalay doyei my bve
Farata rek laalay doyei my bve
Takk ma boum si baat
Soxlawoul sakh ngamay wakh fooma nara dieumรฉ my bve
Manak iow dou diekh
Deh rek moniouy takkalรฉ
Meunoumala baayek kenen
Iow laay soor baby waxma loula nior
Lane ngay yootou chรฉrie ma adjiko
Paradise rek laalay dieumรฉ
Thi geediou baneex laniouy feey maak iow
Aljana
Aljana laala jeumรฉ iow aljana
Dou Aljana lagn nara deukรฉ
Aljana
Oubi sa xol douggeul fa airou aljana
Aljanaaaa
Aljana
Aljana laala jeumรฉ iow aljana
Dou Aljana lagn nara deukรฉ
Aljana
Oubi sa xol douggeul fa airou aljana
Aljanaaaa
ย