Skip to content

Gouro

Narah Diouf
Popularity · Low

YouTube

Searching YouTube...

Lyrics

Tey lagn done khar Nga def ma sa diabar Gneupp took ma sédel là Né yaye kima sagal Dagnou dém ba ndouro Yaye ki ma Yalla bolel Dougnou meusseu reroo Ndakh dagniy doundou mbeuguel Indil ngama gouro Dessalatoma dara Yaye sama chamalama Maye sa ding dong Khol bi di teugg ni tama Yaye Sama best song Yaye sama chamalama Maye sa ding dong Khol bi di teugg ni tama Yaye Sama best song Ma seye ma seye Tey ma seyeul la Ma Sey ma Seye Indi nga gouro bi Ma seye ma seye Tey ma seyeul la Ma Sey ma Sey Indi nga gouro bi Loumou meti meti Khamnané yangui fi Def ngama sa sokhna tey beg naaa Babyyyyyy Teranga bi mate na teralngama Diambar dioni dioni Guilé guilé diambaréeee Yama tanne si séne biiir Mala beuguue piir wakhma loukey dini Dagnou dém ba ndouro Yaye ki ma Yalla bolel Dougnou meusseu reroo Ndakh dagniy doundou mbeuguel Indil ngama gouro Dessalatoma dara Yaye sama chamalama Maye sa ding dong Khol bi di teugg ni tama Yaye Sama best song Yaye sama chamalama Maye sa ding dong Khol bi di teugg ni tama Yaye Sama best song Ma seye Ma seye Tey ma seyeul la Ma Sey ma Sey Indi nga gouro bi Ma seye seye Tey ma seyeul la Ma Sey ma Sey Indi nga gouro bi Môme leu môme leu Môme leu môme leu Môme leu môme leu Môme leu môme leu Ndanane Moy ki fegne sama doundou Fo diar ma wayal la Ndandane Weuh woo Souma démé baleye weuy Seck ndanane na ngué Mo ngui né Seck ndandane nangué Mo ngui née Seck ndanane nangué