Aby
Popularity · Low
YouTube
Searching YouTube...
Lyrics
Just for baby
She's name is Aby
None lako nobé
You know what i mean
Gneupeu khamnéh
C'est elle ma vie
Bougne sakh Andéé all eyes on me
Aby dafa diééki change
Khawma lougne ko wakh ak loumou dég ak loumou done
Mane deh mangui fi di chanyin
Toukh samay vibes, samay craks ak samay bone
Nane
Aby
Aby
Aby yangui mangui
Aby
Aby
Aby yangui mangui
Aby
Aby
Aby yangui mangui
Aby
Aby
Aby je ne te ment pas moi
Tu es la seule qui est dans mon visseur
Je t'en parle ça fais des mois
J'en ai parlé même a ta ptite soeur
Aby sama xal bi
Xal bi
Aby sama xal bi
Xal bi
Aby sama xal bi
Xal bi
Aby sama xal bi
Xal bi
Heeeeee
Newon nala sëy nekhoul
Khamone na Betouma
Beugone nala bame diekh mane
Ma beugone la takk ci souba
Souma khamone li ngamay deff
Doumala diokh sama xol mane mi
Aby ya know this is my baby follow me
I don't let you know
Takh nga tekk ma thiono
Dama sonou boy
Sa yaye nenama nono
Beugone la takk deff la sokhna
Sa pape gneuw neh noo
Affaire de dérét la boy fils
Ta waroul wone démé nii
Aby
Aby
Aby yangui mangui
Aby
Aby
Aby yangui mangui
Aby
Aby
Aby yangui mangui
Aby
Aby
Aby je ne te ment pas moi
Tu es la seule qui est dans mon visseur
Je t'en parle ça fais des mois
J'en ai parlé même a ta ptite soeur
Aby sama xal bi
Xal bi
Aby sama xal bi
Xal bi
Aby sama xal bi
Xal bi
Aby sama xal bi
Xal bi
Regarde moi, bae tu vois bien que j'ai plus appetit
Regarde moi, je suis capable de combler ton appetit
Tu es loin de moi, loin des yeux,
Loin di coeur des futures baby
Tu fais comme si tu m'enttend pas quand je serais a la party tu verras
Aby je ne te ment pas moi
Tu es la seule qui est dans mon visseur
Je t'en parle ça fais des mois
J'en ai parlé même a ta ptite soeur
Aby sama xal bi
Xal bi
Aby sama xal bi
Xal bi
Aby sama xal bi
Xal bi
Aby sama xal bi
Xal bi (hi yeeee, hi yeeee)
Aby sama xal bi
Aby sama xal bi
Aby sama xal bi