Skip to content

Yarr

Popularity · Low

YouTube

Searching YouTube...

Lyrics

par AbouAmg Elève ladj té tina proffesseur_eum Ndakh topou xélam wala topou COEUR_eum Kou beuri xam xam yor si poch yi deureum Esk waxtou diotoul mou diokh montre heur_eum Nénan geum bi fok gua diokh ko thieureum Mai waxou yalla wala waxou serigne Kouné soul na ay affer si boutou keureum Galsen deukou dinê wala deukou kheureum Diné bi néna ma nialo aka bone Ecole bi néna bagna sol potca réka bone Gnépa bogon diang mag faté kamil Gni dakha yégua dakhon wathié kamil Fok gua diéma fonk papak sa yay Mai fi sa yay yey nieuk saga sa yay Woral woral dioulil toubeul Lo wora woray wedi liguay xoutbeu Gorak goray wet di niro koubreu Xoram sakh sou wékhé nirok soukeur Fi guay guiss kou fayal diang domam Bagna topato lan laniy dougal bopam Xalé boboy mag wouté wak wa keureum Papi nek fofou di dioy nan bayina yonam Motakh neggers yagui ni di dioylo fille de joie Neggers yagui ni di dioylo fille de joie Yen say pour gua mour ween digua sol Yeuré bou tollou si genoux Niouné lo guis day diékh souma Timé sama yay damay geumou Kour gui fess dagua niou don fowé ay Pistolé bouniou len dinan diagui leen Xam xam grap la bou dom yi nioré No mounti deff dina am niou sani khér Beug alal ba wakhou niou lim niou diaral Kou beug dara ak kou bagna toul dara Yallay buur mai buur yi geumou niou yalla Mag dou yalla mai yag nak yalla Am say dom ba paré berleen di Diéma diay ba Alleman (guani lane?) Té berlin amoul pa allmen Djiguen bou khamoul gor dh dan koy weur Gor bou xamoul djiguen dankoy wiiri Pourtan borou heurou wiiri wiiri Domou pa you fir yi laniy geuneu iri niggah yeah Geuneu iri niggah Domou pa you fir yi laniy geuneu iri niggah Wa keur gui sounou fonkoul séni dom yi Kon dh sén kharit yi laniy wowé mifa Boul changer deuk mais changel deuk bi Adouna bi souy touki ken dou la may visa Nit kou nioul day youkhou fi ba souba Toubab bi degoul loudoul houba houba Toubaba kheuthi nopou senegalais kheuy Na motakh senegalais degoul toubab Fok gua niémé wakh nit bopam Même goumba bokoné goumba mou guis bopam Oustaz dénthieul masa yatt bi Gneuweul firil ma ayat bi Xalé déna keur gui néna doundou woul sakh Yakh biir té mom mi dioudou woul sakh Andando bou gnaw sou tassé rafet Dara eupoul fitt ay dénth tapet Djiguen bou khamoul gor dh dan koy weur Gor bou xamoul djiguen dankoy wiiri Pourtan borou heurou wiiri wiiri Domou pa you fir yi laniy geuneu iri niggah yeah Geuneu iri niggah Domou pa you fir yi laniy geuneu iri niggah Nigger yaral sa dom Samal sa dom Kou geuneu am dh geunoul diang c faux Gni geuneu niak niofi dakhon kheuthio Beug ndiékh dou takh niou thinn bou tang kheupo Ndakh bonou tégué niam kou féké sigua Borom ndéki kouko nieuk yêwou teudat Djikoy sopalikou dian ba mat borom Sentou werr diaroul boukhanték sa morom Nénagn deuk gar takhoul bari gane Mai noyé adouna takhoul gua goudou fan Bakan com ay thiarakh bouy dag doko yeug Loula mar meunou may matt doulako may Té mem bo amoul bac am kérsa diarna bakkou Magoum wakhon nako mo geun khamon nako Guélaw dougal khop si kamb mai douko si guéné Bodé batou keur gui mbed doula degg Nigger yarr