Xalisso Trahir
Dior Mbaye
Popularity · Low
YouTube
Searching YouTube...
Lyrics
Par AbouAmg
Wax ma li nga xam
Ma wax la li ma xam
Bu ñu ko boolee mu nekk xam-xam
Kaay jox ma li nga am
Ma jox la li ma am
Bu ñu ko boolee mu nekk am-am
Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?)
Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?)
Bëgg naa la ba noppi
Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?)
Wóolu naa la ba noppi
Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?)
Xaalisoo
Xaalisoo ooh badjooo
Xaalisoo
Xaalisoo ooh badjooo
Tasare nga dunya yàq nga lu ne
Foo dégg coow ci àddunia xaalis sanga ca
Ma nga fekk ñaar ñuy ànd te yàgg loole
Nga yàq seen diggante ma la ragal way
Dugg nga ci biir kër jaxase njaboot gi
Tas nga séy xaritoo, xaalisoo
Xaalisoo
Wax ma li nga xam
Ma wax la li ma xam
Bu ñu ko boolee mu nekk xam-xam
Kaay jox ma li nga am
Ma jox la li ma am
Bu ñu ko boolee mu nekk am-am
Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?)
Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?)
Bëgg naa la ba noppi
Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?)
Wóolu naa la ba noppi
Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?)
Xaalisoo
Xaalisoo ooh badjooo
Xaalisoo
Xaalisoo ooh badjooo
Boo amee xaalis am nga solo
Boo amul xaalis amul solo
Boo amee xaalis ni la ba jor bëgg la
Yaa bari doole, neexul waay dëgg la
Xaalisoo
Xaalisoo ooh badjooo
Xaalisoo
Xaalisoo ooh badjooo