Skip to content
Lyric
Dive
Public playlists
My playlists
Search
Sign in
Iblis
Ngaaka Blindé
Popularity · Low
+
🇸🇳 Wolof · Original
0
0
YouTube
Searching YouTube...
Lyrics
Original
Translation
Bilingual
Bis-bis, Iblis
Da am dawaan yu kay wan bala bis bi
Day naan ay dome, tux ay weed, naan ay whisky
Du gaccee yeen pour ngéen xamne tànguléen
Moom du def lu yàlla bëgg, te lum ñaan mu nangu yéen
Ñoo demoon boîte, fanaan bar, dematt Mosqué
Ñooy dox di ñaxtu, te buñ ñiibe dematt marché
Moy dañu baax, dañu bon comme dañu faux
Nga wax léen buñ ma jegee, fuñ ma gis nañ dàndu foofu
Baba rare ci game bi game bi dal di rare (dal di rare)
Ngaaka geen géej gi, géej gui sambarax (sambarax)
Jën bu nekk géedji, je thiebou naar (hey)
Seen game bi munu ma saff di lolu doyna waar mais
Seen game bi munu ma saff di lolu doyna waar mais
Gni di waax duma rappeur ndax dama rew men
Gni di naan dama rew, man dama dof baye
Gni di naan dama dof, mane dama dead man
Te luma geene dafay neex, lolu moy keman
Baba - bababababa
Babab bab bab bab-
Babip babip
Seen game bi munu ma saff di lolu doyna waar mais
Doo ma laaj, lan nga mën a jox sa xol, mba tax mu meer
Ndaxte tugune bokko ne da nga gàtt tem mu merr
Yéen Yàlla hissabuléen, naj bi gènn tànguléen
Ndeki jot ngéen deff séen cassu mew ak mbuurak tatuneen
Maïga njaay ma mbuuru xarko def ci broche', sukar nga def ci grosses
Def ci nit ma jàpp nguéroce
International nga miin nga vol bi trop, jël sa casse deff ci drogue
Gedd game bi rap bi torox
Dof bu werredi dëgg di gaday
Ci sa zone Chek ni Tchang kai
Dila kong nekk thi mao di zedong Mais
Lu xel yanu la bopp ataan
Kilo ndong te sa kataan
Fila dong, may ci gàttal kila moom man