Skip to content

Quién soy yo

Popularity · Low

YouTube

Searching YouTube...

Lyrics

Bëgu nga ma bëgu nala Bëgu nga ma bëgu nala Yo Hale, hale, hale Hale biley Yo Djöö nga ma sama rin ni khol Djöö nga ma ma neeg nga ma Bëgu nala fokku nala Hale biley yai sama khol Aaawu mbesewa Olu mbesewa Jama mbesewa Aaawu mbesewa Olu mbesewa Jama mbesewa Aaawu mbesewa Olu mbesewa Jama mbesewa Aaawu mbesewa Olu mbesewa Jama mbesewa Bëgu nala djöö gis Ma la raw ma nu kofay Ni la ñëkk ni bëgu nala la raw Ma cheri nok nala Binga may bëgu meti wona lool Nga djakko tafay andak man ci gor Yai wax bay wax ñëkku wongani Maan ndongo bëgu andak man ci gor Yama bëgu fokku bëgu mete Ma la njukkal fi bëgu neexe Hale biley hale bi yew Ca dëgga dëgga yew yai sama khol Aaawu mbesewa Olu mbesewa Jama mbesewa Aaawu mbesewa Olu mbesewa Jama mbesewa Aaawu mbesewa Olu mbesewa Jama mbesewa Ee mbesewa Aaawu mbesewa Olu mbesewa Jama mbesewa Aaawu mbesewa