Skip to content
Lyric
Dive
Public playlists
My playlists
Search
Sign in
YMYM
Dip Doundou Guiss
Popularity ยท Low
+
๐ญ๐น Haitian Creole ยท Original
0
0
YouTube
Searching YouTube...
Lyrics
Original
Translation
Bilingual
yaw mi yaw mane yaw mi yaw mi yaw mane
yaw mi yaw mane yaw mi yaw mi yaw mane
yaw mi yamanรฉ do ma meusseu bayyi
xawma sa yaye ndax wano ma sa yaye
mane solution la yaw yama def sa problem
ci sa prison lay dess nangu mafa bayyi
xamonna lo meussoul wax
demmone na fo meussoul aw
lidess pour ma done solda
kidoul xex loudoul pour yaw
xamo mane lima xamone yaw
meuboma ligua done yeah
bou wesso ci mane ak yaw
lidess dou sama probleme
yaw mi yawmane yaw mi yaw mi yaw mane
yaw mi rekka meunoneu nax
if you when do just tape
ย