Skip to content

Mbaal Mu Teer

Popularity · Low

YouTube

Searching YouTube...

Lyrics

Ye fu gor la, ye fu gor la Gor kô mom waye, gor kô mom waye Xëttël balmu derr Sawadji Xëttël balmu derr Baris Gor kô mom, yaw gor kô mom, yaw gor kô mom Gor kô mom, yaw gor kô mom, yaw gor kô mom Xëttël balmu derr, xëttël balmu derr Xëttël balmu derr, xëttël balmu derr Xëttël balmu derr, xëttël balmu derr Xëttël balmu derr, xëttël balmu derr Aw Sawadji, na nga def nu ga waye Ndax balmaw, gor koy def waye Yaw ndang nga jok fajar, ñu tëmbël gal gi waye Dëm tentu ndax pu goru penjë waye Ay ye fu gor la, ma ne li ye fu gor la Amul ragal tunnay du bu gala Ñundë ñi mballa, ku dë këccët ndë ñi mballa Ndax waye bi, ma ne bë xëttël balla Xëttël balmu derr, xëttël balmu derr Xëttël balmu derr, xëttël balmu derr Xëttël balmu derr, xëttël balmu derr Xëttël balmu derr, xëttël balmu derr Ali hay si li ye gor Në bu ndoye yëw jambanga Balmaw, yaw fu gor la Yë ngi sa mu tchol sandal