Skip to content

Immigres

Popularity · Low

YouTube

Searching YouTube...

Lyrics

Guuj Njaay Faama Guuj Njaay Faama Uzin, bitim reew Yuusu, dafa metti dëkku ñu fa Mujj u mujj, yaay dañi dellusee, waaw Senegaal Guuj Njaay Faama Guuj Njaay Faama Uzin, bitim reew Yuusu, dafa metti dëkku ñu fa Mujj u mujj, yaay dañi ñibbisee, waaw Senegaal Olee Guuj Njaay Faama, anh, anh Guuj Njaay Faama Waaw-waaw Ñu nee "bitim reew, ñu fa nekk, dëkk u ñu faa Mujj u mujj, yaay dañi dellusee" Ndaxte ñooñu xamuñu leen Fi lañu sosoo Jóom mooy tukki yaay waaye fullay mooy ñibbisee Noo mën a mel, loo mën a am ndeysan Ñibbisee la war Cóodu Faal Candèlla, yaay, Candèlla Nene Dada mayma ci sam jaam yi Ma dické, poŋcoo, xaajoo Li sa caa gam neex na la Yaayu Pale Jaaga woo nala Dabakhee Dabakhee (Dabakhee) Dabakhee (Dabakhee) Dabakhee (Dabakhee) Dabakhee (Dabakhee) Dabakhee, hé, hé (hé, hé) Hé, hé (hé,hé) hé, hé (hé, hé) Hé, hé (hé,hé) hé, hé (hé, hé) Hé, hé (hé,hé) hé, hé (hé, hé) Dabakhee (Dabakhee) Miskiin mu ñëw mu teral la Kuu àjoom ñëw mu facaal la ée Dabakh Dabakhee (Dabakhee) Dabakhee (Dabakhee) Dabakhee (Dabakhee) Dabakhee (Dabakhee) Dabakhee, hé, hé (hé, hé) Hé, hé (hé, hé) hé, hé (hé, hé) Hé, hé (hé, hé) hé, hé (hé, hé) Hé, hé (hé, hé) Sant nañu léen, ñoo ñi leen di ñanal Suma delloo, di leen wayaatoo Waaw Senegaal Mooy sunu réew Ndaje muut nii laa, say yu nekk Suma sañoon dii ko defeet yéen Waaw Senegaal, Senegaal, Senegaaloo moy sunu réew