Skip to content

Bou Bakh Bi

Canabasse, Cheeks, Cool Black Lion, Zou Kana
Popularity · Low

YouTube

Searching YouTube...

Lyrics

Canabasse] Yeah rafete na, diek na, taarou na douma ni dedete Yeah teyé na tankam boudoul pour farata dou guene Deguel neu ay wadiouram mook nienene gni dougnou bene Xaroul si mane dara loudoul love te bagnalouma lene Ki bou baakh bi la Damay doug galem wakhak papam ndaxtè bi bou baakh bi leu Tegui tank garè wathie andak moom ndax tè boubaax bileu Jackpot nigga lolou la nieup di seet Bima dioudo bobou ba legui yaw rek ladone seet Mancha limuy dound doyna seuk dama sikk dama sikk Mais guemeul ni yaw rek ladone seet Baby girl bou baakhc bi ngueu no more talking Beug nala def sama wife sama trophée Cheeks dafa thiofé yea dafa trop frais Hamna ni mane kecé tamit ngadone seet Damla nop ba doff et puis matay Dioureul ma ay filston you barkeel Dimanche nga tegalma ay boolou mafé Boubaxa baax bila chè pas ce qu'elle m'a fait Yalla boula thiate dougou Mane ak yaw ba biir paradise Ma lay retain lo ni Dudu Mane ak ioe lepp chill lepp nice Yeah rafete na, diek na, taarou na douma ni dedete Yeah teyé na tankam boudoul pour farata dou guene Deguel neu ay wadiouram mook nienene gni dougnou bene Xaroul si mane dara loudoul love te bagnalouma lene Ki bou baakh bi la Damay doug galem wakhak papam ndaxtè bi boubakh bi leu Tegui tank garè wathie andak moom ndax tè bou baakh bileu Sou ma sagnone modulé ak mome Mbeuguelam dima goungué may dokh Soufi nekoul douma neka lep ne teka hawma noumay mana doundé sans moom I gotta marry her she so got to me Took my chance to propose and took a knee Players gotta stop balling it don't bother me All She wants is a little love but gets all of me Bou bakh bi la she not popular When headed to the bottom mou top ma Sofo sobo takh ma sop la. Amouma ko doul yow kot kon kout man You know opposites are beauty like a panda heaven sent she scares me like thunder My love to your heart it surrendered Your a perfect girl like an angel descendent Yeah rafete na, diek na, taarou na douma ni dedete Yeah teyé na tankam boudoul pour farata dou guene Deguel neu ay wadiouram mook nienene gni dougnou bene Xaroul si mane dara loudoul love te bagnalouma lene Ki bou baakh bi la Damay doug galem wakhak papam ndaxtè bi bou baakh bi leu Tegui tank garè wathie andak moom ndax tè boubaax bileu Sama lady sama lady Si mom lay dess legui legui Bouko beuguè rek ma deff diff Matal lepp tay toom mou seuy si Yokhla bayi lepp louma diapone Garé melni troc bouniou sabot Yeah jotna ma dem waxak papam Ndax guissna fi facon bou né Wanté ki ni bou baakh bi leu Rafetna diek na tarou, mbeuguel bim ma jokh dafma yeem Teyé tankam budul pr farata halebi dou guene Deguel na ay wadiouram yeah mom ak nienene gni dougnou bene Kharoul si mane dara loudoul love yea baby té tegouma lene Ki bou baax bi lamotax fi la garé Bou baakh bi la Sagn na doug galem Bou baakh bi la Dianok papam neko sa doom la beug té ding mako may Yeah rafete na, diek na, taarou na douma ni dedete Yeah teyé na tankam boudoul pour farata dou guene Deguel neu ay wadiouram mook nienene gni dougnou bene Xaroul si mane dara loudoul love te bagnalouma lene Ki bou baakh bi la Damay doug galem wakhak papam ndaxtè bi bou baakh bi leu Tegui tank garè wathie andak moom ndax tè boubaax bileu Yeah rafete na, diek na, taarou na douma ni dedete Yeah teyé na tankam boudoul pour farata dou guene Deguel neu ay wadiouram mook nienene gni dougnou bene Xaroul si mane dara loudoul love te bagnalouma lene Ki bou baakh bi la