Skip to content

Mama Bless

Popularity · Low

YouTube

Searching YouTube...

Lyrics

Ye he he he Wo ho ho oh oh oh ah Ee yow Yaay bóoy, yow de ñaanal ma Ee yow Baay bóoy, yow de ñaanal ma Yéena ma jur si yoonu siratal mustahiim Jàngal ngeen ma Alxuraan Yéena ma ni doom moytul lu aaram Yéena ma ni doom oh moytul yaw saraan Dund bu soteegul lunekk xaj nasi Ku jéggiwul ndox bul retaan kuy lab Yaay bóoy ñaanal ma, ndax sànku dafa gaaw Baay bóoy ñaanal ma yow si pexe noon yi Mama bless me from my ennemis Father bless me from my ennemis t 2 Boobu ba léegi mësuma wàcc yoon Boobu ba léegi xamna ki ma doon Ndaxte xamna ki ma doon, fi ma jógé, fi ma bayeeko, fi ma soqeeko Ñaata ñoo lay ree, fekk yéene wuñula ludul dee Ñaata ñoo lay siiñ, so deme ñu lay biiñ A long away of my Life me I hustling day and night When I remember when I was a young boy My mama use to say oh my song Go forward and don't look back Follow you diny follow your way Boobu ba léegi maa ngyi topp yoon Ndaxte xamna ki ma doon Ku fàtte yow fi nga fi nga jógé, fi nga bayeeko Fi nga soqeeko Ñaata ñoo lay ree, fekk yéene wuñula ludul dee Ñaata ñoo lay siiñ, so deme ñu lay biiñ Xàmmeel bu baax ñila bëgg Ak ñila bañ Toppal sa yoon Who mama bless no one curse Who father bless no one curse Who serafall bless no one curse