Skip to content

Fi Fë Lee

Popularity · Low

YouTube

Searching YouTube...

Lyrics

Xam na fii ma jogee Xam na fii ma jëm Fii la lépp doore Fii la nu jëm Fëlee fii fii fëlee Fëlee fii fii fëlee Fëlee fan Samay maam no woote Maam b6oy mooma woo Fii lay roote, teen bi fii la Fëlee fii fii fëlee Fëlee fii fii fëlee Fëlee fan Fëlee fii fii fëlee Fëlee fii fii fëlee Fëlee fan Fee la juddoo Fii la joge Fepp lay dund Fepp laa magge Fee la juddoo Fii la joge Fepp lay dund Fepp laa magge Fee la juddoo Fii la joge Fepp lay dund Fepp laa magge Fee la juddoo Fii la joge Fepp lay dund Fepp laa magge Dellu kër maam Fa lanuy fanaan Ku fi marr naan Dellu ci ndaa li taataan Da no bëgg am Laada xam xam Amatunu jàmm de What a barn barn (Barn barn what a barn barn) Da no bëgg ndam Xam sunu coosaan Ndar geej ba Wakaam Coumba castel Coumba Bang Joal ba Carabane Grand ndakaar Colobane Janxalaar Colobane Nëwal do fi gàn Aduna bi la nu dëkk Fun dem daaj fa banc Aduna bi la nu dëkk Fu ne la am banc Fëlee fii fii fëlee Fëlee fii fii fëlee Fëlee fan Fëlee fii fii fëlee fëlee fii fii fëlee fëlee fan Fëlee fii fii fëlee fëlee fii fii fëlee fëlee fan Fëlee fii fii fëlee Fëlee fii fii fëlee Fëlee fan