Skip to content

DOFF CI YOW

Popularity ยท Low

YouTube

Searching YouTube...

Lyrics

Par AbouAmg Yaay sama lumiรจre Lampe bu may wane yoon Yaay sama lingeer Baby baby baby baby baby Xol bi yaa fi nekk Ta kenn mรซnul jรซl sa place Sama diamond, sama woman Bรซgguma di la sori Su ma la tooรฑee, baby sorry Ndax xol bi yaa fi nekk Eh, eh, eh, baby Sama diamond, sama glory Kaay ma wax la I'm ready Baby yaay sama love, love, love, love Baby dama fall in love Love ba dof ci yaw Fooy dem yรณbbu ma Bu ma bร yyi ma wet Ku la faalewul ma faale la Yaay sama aljana Yaw laay topp fepp Baby, baby Xam naa li ngay laaj Sans nga posรฉ benn question Xam naa li lay faj Waaw waaw Fees dell toog ci sa place Baby amul benn raison Bu tax man ma lay bร yyi Waa waaw Boo ma bร yyee bร yyi Wax ma fan lay muje Ndax mbรซggeel bi ma am ci yaw Depassรฉ na life bi Boo ma jege jege Xam naa li may sentir So baby maa la nob ba love Oh oh oh oooh Baby dama fall in love Love ba dof ci yaw Fooy dem yรณbbu ma Bu ma bร yyi ma wet Ku la faalewul ma faale la Yaay sama aljana Yaw laay topp fepp Baby, baby