Skip to content
Lyric
Dive
Public playlists
My playlists
Search
Sign in
Freres Guissé
Jikko
Popularity · Low
+
🇸🇳 Wolof · Original
0
0
YouTube
Searching YouTube...
Lyrics
Original
Translation
Bilingual
Mani fépp fu niou seugg di ji
Ceeb ak duggub mba génté
War naniou fa meuneu jéemé jii lénéen
Lu melni jubb ak jom ak yar ak baax ak and di liggey
Di jeem di liggey
Deukk ci di liggey, liggey
Ndax bou euleugé mu jur Sénégal
Jàmm Sénégal bu nieppou di naw
Jàmm Sénégal bu nieppou rangnié
Ci def lu baax ak diniou njarin