Skip to content

Géej

Popularity · Low

YouTube

Searching YouTube...

Lyrics

Geej,geej maboulane Geej,geej,Mbaboulan Geej,geej, Mbaboulan ya ñi wootal Say dom Geej geej Mbaboulan ya ñ wootal say doom Geej,geej maboulane Geej geej Mbaboulan ya ñi laabal sày doom Dunde yakaar mba garaaw weex Tës tësi mba doolé ñeex Yakaar lab na biir geej Tay mba sonk mbëg mi Yakaar yi geersuna Tay mba soobu geej Bou lén fok ni jël loñoo neex na ma Maay seen Avion yi di naaw Barça wala balsak Li lén wutélé si man Fu ma teele baax na si man taay Bu lén fok ni jël loñoo neex na ma Maay seen avion yi naaw Geej,geej maboulane Geej,geej Mbaboulan Geej,geej, Mbaboulan ubil ma say loxo Mbëgg na am jaabar am ay doom Mbëgg na tekki ni samay morom Mbëgg na sutural samay wajur Ligeey yu ndaay àñum doom Geej,geej Mbaboulan Geej,geej, Mbaboulan Geej,geej, Mbaboulan damaay wùtti ligeey Yakaar yi geersuna tay mba soobu geej Geej,geej Mbaboulan damay wùtti ligeey Geej geej Mbaboulan taalal ma say loxo