Skip to content

Up

Popularity ยท Low

YouTube

Searching YouTube...

Lyrics

Lyrical one finga nek sori na teh worotofa yem Up, never down x4 Defoga gatt ngeuneh danga siww Ma gueuneh siww sa mรจre Ma gueuneuh riche ton pรจre Talalma dix sondรซl Dama la beugue nianal ni biss boy deh Khana khamo neh dip comme prรจtre Teh dama lucide comme biรจre Amna niata hit comptel Dignma beugue rey melni Lincoln Beuss bou yala def mangui si thiaw Waxal lii la nex, defal lou la nex Beus bou yala def may cfa bi ci poche Mangui ak ay arme ak ay diplome Na dagg sa ... ak ciseau Fuck kepp kou ley big up Kep kou ley support Kepp kouy rap wolof nigga ci pot Robinet dey tedj nanal boutit bi yeup Do massa lall fuck mada fuckin nigga Ay million lay djott manak one lyrical pistolet si kaw ngi fi gueneu beuri tital Toum, Toum, Toum bala auto police di nieuw Iow pa nga sa yalwane lagniy keup Dignma beugeu rey waye amougn fitam Adouna dina touki nigga teh dip dou teup ahhhhh Bougo ma, mala gueuneu begne Linga meuneu lala gueuneu dak Diplome you maga maga mak Si bop manak sama gang Dou niok njiy yagg dama bax hip hop bi madafucka Thiaga yi bougone tall sama budjet Mala gueuneu sour, mala gueune xiff men Dengey tiaxan dignley tiaxat Atia tiah xatie dougn fey tiaga Lyrical one finga nek sorina teh woratofa yem Amougnou tankou guinaw worougnou andando ci bi game Mama dafa seugue deugue sib ba na neh sama gatt amoul fayam Signel contrat li dess niou garantir ko nioy Up never downx2 bene madafucka dognou tereh dem wagnil thiow li nioy Up never down x2 Niongui dor ngey tit Boy diff jox dip egal toujours but One lyrical: Sour na moussoul bok sama vocabulaire Sama cellulaire ngi sonne all day Yaga feyekou wer moussou ma dem seminaire Non, Non rapagouma ney leer Soumane rapagouma ney leer Samay frรจre nama i dont care Yangui ak gone ni militaire Begnok nadj bi teh nga outi kerr Begnok nandite yi dougnou seer yeketi sen univers Ras, dama moudjou beuri tourondo canal plus Nganan fils, te nga nann quit, sa garantie topou la nigga amoul piss R.a.p, dama beuri dougou dougou indi final pรฉ Dilenn teyรฉ, kenen kou si neh nema jeundeul pain Yeukeuti flambeau pikine, final gang Deumeu wouteh nji fi nek di deumb deumbelou Mafi teugeu tama dama jaxasso ni mathematique Iow danga titt manla automatique Auto mbalitt pipp Niang niangalou bi nigga diaro ki fi Domou adama bi dak rap ngi doga ganeh si adouna ci bissou aldiouma la djoudou khamouma Guinaw rail la kenen ko fi wax dey xar deuxieme mi temps thiow li diex Dip, Dip, Dip, Dip mongui sama team Dignou la timm Real niggas in da building Diaroulta limm Niongui ci in Joue wougnou film Nopougnou kim kardashian Deug deug solougnou Tim Saxougnou sikim di def yefou mak Yangui ci pc niou innove ci mac Degueneu dama yarou boma deglo khamne nganday domeram la Lyrical one finga nek sorina teh woratofa yem Amougnou tankou guinaw worougnou andando ci bi game Sama Mama dafa seugue deugue sib ba na neh sama gatt amoul fayam Signel contrat li dess niou garantir ko nioy Up never downx2 bene madafucka dognou tereh dem wagnil thiow li nioy Up never down x2 Niongui dor ngey tit Boy diff jox dip egal toujours but