Skip to content

Gnégno - feat Le Raam Daan

Wally B Seck
Popularity · Low

YouTube

Searching YouTube...

Lyrics

Anh gnéégno yéé tëy maa weuyaal lén ndeysane wawe Wa lalou wourrouss Maak askanwi ma Yalla booléll Gniit teug xaliss bathi gáál pir Sama xeel na diem si yéne Ma woyaal leen Seen Jambaar deug la dakhe démbe leu Balla maïssa yéna môme lii Ndéuké si dugnu ààe tééy guàgnuuye tààral nganaye Rayyaa wourouss bassi ngalaam kokoy balla maïssa yéé Ndéuké si dugnu ààe tééy guàgnuuye tààral Nganaye rayyaa wourouss bassi ngalaam kokoy balla maïssa Ndéuké si dugnu ààe tééy guàgnuuye tààral nganaye Rayyaa wourouss bassi ngalaam kokoy balla maïssa yéé Ndéuké si dugnu ààe tééy guàgnuuye tààral Nganaye rayyaa wourouss bassi ngalaam kokoy balla maïssa Gnii séne mame teugaal buur tougall Samba laobé kharr Yalla maa weuyy Teuug dawwul mbààr ba tëy dji anh aïmirou tiam teugaal Domou yayou Mor thiam Moustapha niang mar teegg léne Dame Diop wétale na thiléén Balla gaye Marame thiam maa weuyy ndiaambe mar hassim ma Ayy coumba khadim thiam céélléé Ndeye woury thiam Né léne ko diarama ngàthié ngalama balla maïssa Né léne ko diarama ngàthié ngalama balla maïssa Diaw wallo sén keur mame ngàthié ngalama balla maïssa Né léne ko diarama ngàthié ngalama balla maïssa Nganaye yaa héékhe baadaar baa d'âne séne lokhoye mame la soosso Térré yougnou d'âne gaathio xaaréé sén mameee maaa euuw Wouye thiam babéel demba thiam Mbakhe dou wéssou mbakhe ni kone gnéne wéssou mbakhe Né léne ko diarama ngàthié ngalama balla maïssa Yilay cheikh mbacké ndiaye dàagama yéenéee baayuu karra Ndiaye demall ba keur zale thiam faaguul mafa aye liibi d'or Kana FALL saa yaye Arame cisse faye Yayaam cheikh mbacké dagama yééné ndiaye Né léne ko diarama ngàthié ngalama balla maïssa Sofi komé maala yéébal cii Balla maïssa thiam diougual chéri Omar FALL bahaï mareme lame saa yaye sofi Yayou bébé tidjane Amadou hôtesse de l'air sofi Ann Ibrahima chéri adji thiam Graziella mbokuum Mariane diago serigne fall mounass seck téélla gnakk yaye Jule thiam sa borome keur ngaye loo ak bambilor président PaPe sow Bathie diaww Papa ndiaye térangaa Istanbul Diuba thiam balla maïssa thiam awa Kane papis Demba cissé late guissé Chéri adja lo itééléka sediou Maarsé wooni papis Demba cisse aassu daas