Skip to content
Lyric
Dive
Public playlists
My playlists
Search
Sign in
Siggi
El Hadj N'Diaye
Popularity · Low
+
Original
0
0
Listen
YouTube
1
2
3
0:00 / 0:00
Loading YouTube player...
Lyrics offset
Synced
Lyrics
Original
Translation
Bilingual
Ahouma liguey damay jaay
Outouma lénéne loudoul kaaj
Amoul gao amoul diiber li laay soutoul lo
Ahouma liguey damaay jaay gni di keuff sama jaay
Iitema di ma paptipaté,door leki bakkaan
Di toog ba khamato fooy jaar
Di toop gnou démoon dikk
Di toog ba xalaat ngeex
Gni khamoul woon di khelm
Gni gueumeul di gueumuu
Yaag duu yakk daay diinii touma yi
Ki sakk ta kham li baax mooy kookuu
Yaay booy makk la baay booy dem na
Xale ye gnoom laay xalaat
Jigeen yagni jaayatu
Goor ngayi fooratu gnil soutoural sen jaaboot seew be
Goudou nopp bou doon taaxa dégg com mbam ken douka door
Iitema di ma paptipaté door leki bakkaan