Skip to content
Lyric
Dive
Public playlists
My playlists
Search
Sign in
Calm Down
Karabalik Beatz
Popularity ยท Moderate
+
๐ธ๐ณ Wolof ยท Original
0
0
Listen
YouTube
1
2
3
0:00 / 0:00
Loading YouTube player...
Lyrics offset
Synced
Lyrics
Original
Translation
Bilingual
Tey ma bรฉge la
Tey ma wone la
Tey ma wax la
Yaa ma gรซn a xam way!
Li nga ma def soo ko bร yyiwul
Dinga mรซs a ray doomu jaambur way!
Yaw yaa ma xam, xam ma bu baax
Bu lu xasaan ci man loxo keneen wokesu ko
Guddi gi jot ba lรฉpp ni sรฉelaw
Nga daagu ndank รฑรซw sama kaw di ma eh eh eh Yaw
Say kesen kesen tere ma nelaw
Yaa ma mรซn a yuxuloo te xam nga dama ragal
Eh calm down, calm down
Bรฉbรฉ calm down, doomu jaambur la
Eh calm down, calm down
Bรฉbรฉ calm down, doomu jaambur la
Dootoo niit parce que doo nitu
Yaa nga may fit est-ce que doo ciit
Ni ngay def dama joomi
Man li may yaakaar est-ce que doo รฑooรฑu
Yeah yeah
Baby li ma jaxal te nga wax ma ki la jร ngal
Sant na sa bร jjen moom mi la jox li may jomal
Amatuma sago ci yaw su ma la gise saalit
Waaw waaw, yow baby waaw waaw
Seddal sama xol, dalal sama xel
Yaa ma gรซna lool
Ne waaw seddal sama xol dalal sama xel
Eh eh eh
Eh calm down, calm down
Bรฉbรฉ calm down, doomu jaambur la
Eh calm down, calm down
Bรฉbรฉ calm down, doomu jaambur la
Dootoo niit parce que doo nitu
Yaa nga may fit est-ce que doo ciit
Ni ngay def dama joomi
Man li may yaakaar est-ce que doo รฑooรฑu
ย