Dafmay Dal
Wally B Seck
Popularity ยท Low
YouTube
Searching YouTube...
Lyrics
Taay ma netalilen man lima dal
Si sama digantek xale bima tal
Coono ngantal moy lima dal
Man de lima dal moy ku ma dimbale
Leg leg ma xol ko jooy sax daf may dal
Mba ma xol ko ree si daf may dal
Coono ngantal moy lima dal
Man deh lima tal moy ku ma dimbale
Leg leg ma solu bay dem moom mu terema
Ma daldi tokk li daf may dal
Melni kuko ragal daf may dal
Man deh lima dal moy kuma dimbaleh
Tokk na di waxtaan bis mak samay waay
Telephone bi sonner muy moom ma daldi daw
Melni kou ragal sax dafmay dal
Man lima tal moy kuma dimbaleh ehh waaw
Jรซli nala nร nd na ni ngay doxe eh hee
Anh anh sa bay mussu รฑu ma gnenkouleh sa ba
Lakari lelelaw
Gnekamulehguemou xadila na
Anh moussoletou lakari lelelaw
Worna buur bi yalla รฑu bollee
Et siiii ya malรฉen gรซnal soxna
Nadipeh ba wakanda
Ndaw si deh moy sama saytaaneh
Mbatam hoo yow jรซlรซl
Annh hi yeah woo woo waawaw
Dama am sa faiblesse xol bi ya ci siy fess
Dรซgg la dila jaaner di jooy daf may dal
Gis u loon i gaa yi gรซm a tu nu ma
Yenn say ma bรซgg njengu gueneuthie daf may dal
Coono gi ci mbeggรฉel jar na ko doyna ware
Damay woo dame sene
Sama kaw scรจne
Tajal ko chaine ngir mu beggal malรฉen
Gis na ni gaa yi gรซm a tuรฑu ma
Goom deh luma wax รฑu ni ma baxna
Jox nala cรซr bi ba mel ni kula ragal daf may dal
Aw ma ci kersa
Dรซgg lani jaam si yow la koy ame dafmay dal
Mala tal yama tal
Di defal sama gaa yi dafmay dal waaw
Su sutante daรฑ may gaaรฑ (ma am sa faiblesse)
Xol bi ya si fess dila jaaner di jooy dafmay dal)
Woo-woo
Coono ngi ci mbeggรฉel jar nako doyna warreh