Skip to content

Cool Na

Prosper
Popularity · Low

YouTube

Searching YouTube...

Lyrics

Bonjour ça va respect chef Vas-y dit moi lumu def Je le connais mom du tooñ Wedi ko laac ko sama koñ Toujours premier à l’école Il est brilliant, il décole Pourquoi aussitôt ça déconne Vraiment li ni ça m’étonne Dafa tuti mënula xam luy tux boon Tela tëdi yewu jangi aka am jom Dafa yaru and ak teggin bokul ak ñoom C’est mon petit, sois pas têtu bul ko def noon Sama tonton may ma xalis Ne ma jarbaat demal baali Ma jàd jëndi kaali Wara ñibi dajee ak police Buuka bu ndaw, ben bu ñu ëw, paquet rizla, lek na coow Ana sama gaw, du ma mëna daw, ño ma gëna gaaw Sama xel ñaar, ni mba nee fan lay jaar Jomi na jaxle, fu ma kay waxee, tari ay saar Yaw yama yoni Ben ontooni Rizla joni joni Woy feremboni Tonss ya mom boon yi Nexal ma moni Won ma kër Tony Kay naan sa sombi Suma yëgon doma dugël ci bile tuxiduna Soma juroon doma yebal bama ne ci teggi tuma Tu es méchant comme la police nala bolek commissaire Il va t’arrêter d’office afficher fep sa poster Defu ma fa dara yaw lu la wara jàp Yobu la ci kaso bi de tëcc lafa rap Mënoon nga ko négocier baña andi japp Amato ci ben pexe yaw saf nala sàp Sama tonton may ma xalis Ne ma jarbaat demal baali Ma jàd jëndi kaali Wara ñibi dajee ak police Buuka bu ndaw, ben bu ñu ëw, paquet rizla, lek na coow Ana sama gaw, du ma mëna daw, ño ma gëna gaaw Sama xel ñaar, ni mba nee fan lay jaar Jomi na jaxle, fu ma kay waxee, tari ay saar