Enemy
CAB
Popularity ยท Low
YouTube
Searching YouTube...
Lyrics
Numa meunti mel yaw yaay kitax
Mere beugul sam diguentรฉ ak yaw xol bangui taakk
Pourtant diguentรฉ bobu meune nama dougeul ci pax
Th liรฑu sรจkk meussuma sekak benene niit luko daakk
Yay li gueune
Si lima meusseu dal ci sama vie
Laata รฑuy tassรฉ sama stock d'ambition gueunone na vide
Si lila neex
Gueuj naci tek sama tank
Th taxul nga dem japuma wone naa dem ba yam leu fi
Sama ay defauts sudul wone yaw mane numay def ba xamko
Si รฑima weur sa ay intentions si gueuneu sincere
Prudence binรฉ si mane yaatax ma amko
Tu fais des choses pour moi pareil que ce ร quoi un saint sert
Yeah
Xam say faiblesse day tax nga fort
Th wolu trop seu ay force meune neu tax banga faible
La mer n'est pas potable mais mom leu jรซn di naane
Yeugo mbeuguel bilay aveugler ba doma meune wax li am yeah
Bayilene maak samay enemy
Awma sene faay samay enemy
I can fly as long as i got em
I'm not gon shine without enemy
Ndieuriรฑ bingma amal xamo sax nimu doy
Mane dh meunuma am lula gueuneu reuy
Budul famille bi yay kima sol jom bi
Enemy
Ndieuriรฑ bingma amal xamo sax nimu doy
Mane dh meunuma am lula gueuneu reuy
Budul famille bi yay kima sol diom bi
Enemy
Enemy
Yay sama seetu bi gueuneu ler
Metit bi yamul feneu gatiรฉy nga nara tax ma triste
Sa lamiรฑ lay guiss reflet sama leundeum ni takander
Sans yaw kuy tรฉ suma narรฉ bayi loxo รฑeup farma ci
I love you so much
Am bimala am defnama honneur
Yay ki gueuneu tax nekuma dormeur
Kone guudeul fane enemy guudeul fane yeah yeah
Tu es mon trophรฉe le plus meritรฉ
Depuis mes 17
Meusso fi gueuj
Yay kitax li bone รฑu koy meune modifiรฉ
Point yu faible yinรฉ si yaw ndeysane nga fokni mongsi รฑeup
Montรฉ yay ecole bi meune ci yima jaar nekul lycรฉe
Limala am
Meunula romb bรฉnรฉdiction
Baxulo mais comme xaliss t'es un mal necessaire
Sumla amoutone fumay jeulรฉ yi pulsion
Sa dรฉ jigouma mais aka mala meunone fexel yaw
Bayilene maak samay enemy
Awma sene faay samay enemy
I can fly as long as i got em
I'm not gon shine without enemy
Ndieuriรฑ bingma amal xamo sax nimu doy
Mane dh meunuma am lula gueuneu reuy
Budul famille bi yay kima sol jom bi
Enemy
Ndieuriรฑ bingma amal xamo sax nimu doy
Mane dh meunuma am lula gueuneu reuy
Budul famille bi yay kima sol diom bi
Enemy