Dieguema [Salsa]
Popularity ยท Low
YouTube
Searching YouTube...
Lyrics
Ritmo Africando
Oy!
Massa
Haba!
Ifexal saxal moy syiw li dundal xol ci nit
Moy mbรซgรซl
Sumbรซgรซl taxe maway la caw fe latax
Maye am xala
Sumbรซgรซl taxe maway la caw fe latax
Maye am xala
Di wax ci yow lu ken
Mansul xala di wax keneen
(E yo)
(Jege ma wayuma samare ni xol)
(E yo)
(Jege ma wayuma samare ni xol)
Sumare ni xol wayuma รฑรซwel jรซl me
Yama wara jรซl, kay jรซl me
(E yo)
(Jege ma wayuma samare ni xol)
Sumbรซgรซl taxe maway
Caw fe latax maye am xala ci yow
(E yo)
(Jege ma wayuma samare ni xol)
Di wax ci yow lu ken
Mansul xala di wax keneen ku dul yow
(E yo)
(Jege ma wayuma samare ni xol)
Diya taxe makan bรซgรซl
Ni mala bรซgรซl
Epp na keneen ku dul yow
Jege ma jege ma
Ka jege ma
Jege ma jege ma
Wayuma
Jege ma jege ma
Ka jege ma
Jege ma jege ma
Wayuma
Ifexal saxal moy syiw (Jege ma jege ma wayuma)
Li dundal xol ci nit moy mbรซgรซl (Jege ma jege ma wayuma)
Am bรซgรซl bรซgรซl bรซgรซl bรซgรซl bรซgรซl (Jege ma jege ma wayuma)
Samare ni xol wayuma (Jege ma jege ma wayuma)
Ni amรซl ci man la amรซl ci yow (Jege ma jege ma wayuma)
Luma masa xam wax na la ko (Jege ma jege ma wayuma)
Luma masa gis woon na la ko (Jege ma jege ma wayuma)
Di lawoon di lawoon
Luma masa am jox na la ko (Jege ma jege ma wayuma)
(Khay!)
Yow mi jam cรซmoom
Yow yow
Yow mi jam cรซmoom
Yow mi jam cรซmoom
Yow mi jam cรซmoom
Yoppantรซna
Bo deme nga ni ko
Mbรซgรซl metti na
Na metti na loor
Gise Yallaay boor
Bulma min fa dema
Bulma xam ba yimma
Ci loolu ci loolu ci likay jege ma ci loolu
Ci loolu ci loolu ci likay jege ma ci loolu
Khay!
Woo naale guddi
Woo naale bรซjรซk (Wayuma samare ni xol)
Sรซmoyu bรซjรซb yi wax naรฑ la ko (Wayuma samare ni xol)