Gnom Gnare
Simon
Popularity · Low
YouTube
Searching YouTube...
Lyrics
Yeaaah, houma ci balay tàn na ci ñoom ñaar
Woooh, houma ci kan lay tàn na ci ñoom ñaar
Yeaaah, houma ci balay tàn na ci ñoom ñaar
Yeaaah, houma ci kan lay tàn na ci ñoom ñaar
Ouuuh, houma ci kan lay tàn na ci ñoom ñaar
Yeaaah, houma ci balay tàn na ci ñoom ñaar
Houma ci kan lay tàn na ci ñoom ñaar
Houma ci balay tàn na ci ñoom ñaar
Houma ci kan kan lay tàn na ci ñoom ñaar
Houma ci kan lay tàn na ci ñoom ñaar
Neema masse nàng gounaa xoola ngi mass xoola ngi lox
Xelam ga daay daw tujju mar naan deegi suul ndox
Doxe bopp doxe xoxta ragala tann bu ci yox
Neema masse nàng gounaa ma rou bеg la ab di dox
Sorе lër, jëgën dëer, jaxaso rouy yëm beex
Di ne laaw bu goon kuma yëe ak nga ndam malamu pes ci leex
Yeub yeub, siit tiit, sidit yë saggu, dëkkë xeer
Gala wu loo rangi jall gati takk awee ma xar ma seer
Bëgë ki, nopp kee, ba faaf mbir ma def ma ka
Juma gëb ñaar yi jigee man la taawu ki ak kooka
Mëgë lañ may foowee, am baar gée ci galam di ma jooe
Takk awee tanku mbalax tokkee gi sël ni may jooe
Man, yal la riaali zéro weer nteer
Waa yi kooka kàlli, dépendance nga nekku ta feentee
Liski liski, nekku ta maske
Man, maski maske, Miss di ka loo rang may tabase
Ay rafët taayu nekku ta muñ ma
Yi bët yi sil dima soll jële jëfe koon
Waa yi kanday tàn na ci ñoom ñaar
Yeaaah, wooooh, houma ci balay tàn na ci ñoom ñaar
Yeaaah, wooooh, houma ci balay tàn na ci ñoom ñaar
Yeaaah, wooooh, houma ci kan lay tàn na ci ñoom ñaar
Yeaaah, wooooh, houma ci kan lay tàn na ci ñoom ñaar