Skip to content

Boor Yi

El Hadji Ndiaye
Popularity · Low

YouTube

Searching YouTube...

Lyrics

Woy wi: Bor yi (La Dette) Dañ ñu dëj Bor yii dañ ñu tëcc Ba tey jilee Ñun ñii mënatuñu rëcc Ñun dundatuñu Réew mi lañu xoj Ñun dundatuñu Néew ji doole yi Lañu xoj Dañ ñu dëj Bor yii dañ ñu tëcc Ba tey jilee Ñun ñii mënatuñu rëcc Ñun dundatuñu Néew ji doole yi lañu xoj Ñun dundatuñu Néew ji doole yi lañu xoj Juróom-fukki at Ba tey ñu ngi fey Te fey googilee Tey jii la gëna rëy Xale yi jàngeetuñu Ñi tawat fajootuñu Juróom-fukki at Ba tey ñu ngi fey Te fey googilee Tey jii la gëna rëy Te dégg naa ne Bor yii niñu ko tërale Dootul jeex ba fàww Mënatuñu ko fey ba raw Thomas Sankara Gisóon na bor yi ñuy sànq ANNULONS LA DETTE ET RELEVONS LA TÊTE! Nous, on ne vit pas Nous, on s'accroche! Nous, on ne vit pas Nous, on en souffre! Dumay wax ndimbal Ndimbal gi may noot Di may dugal ci pax Pax biy gëna xóot Amatuñu ndox mu teey Jàngoro yi ñu ngi ray Xale yaa ngi deek xiif Jur mer mu dul giif ANNULONS LA DETTE ET RELEVONS LA TÊTE! Ñun dundatuñu Néew ji doole yi lañu xoj Ñun dundatuñu Néew ji doole yi lañu xoj Sunu njiit yii Dii dundee politig Politig googulee Banque mondiale tëral Yore kàccireem Maanaam xaalisam Ku deful ndigtalam Ñoom ñu xañ la dërëm Ñun dundatuñu Néew ji doole yi lañu xoj Ñun dundatuñu Néew ji doole yi lañu tancc!