Gentleman
Elzo Jamdong
Popularity · Low
YouTube
Searching YouTube...
Lyrics
Check yor dakh na kamera
Fresh nikku joggé Canada
Kumo song dinka Sangoku
Lu moy flowu kama Yemaya
Shuudawlu building te jame laa
Soo ba nga yenggal sa favela
Rappu ri boss akon Pamela
Naaran ñoo soubé kom paamé laa
No la xummay diini hit
Thug life sa may enemies
Sooob maan dun ñu jekkati
Doop laalama joggati gissé guumu
Motherfucku wumu mure fatuloo sa may origin
Bu ñu bugi bukkee gratuit dafa fekk
Xamma go sa may money team
Xeewanda jowru te jaay
Te talaan di kendu ku jëll
Dërru may dërru may jaay
Naax maan la may jaay di rëpp
Yalla ji rekk u ñu team
Bo naax Yalla ji kendu ku neebitu
Wax ka di xeey bu ñu dara
Dafa lu ñu wax dafa ñu këbëtu
Fils, maan jaay mu beegoru ghetto
Po jaay sa may disque
Tabaski sa ñu sà rabu
Werti rai sa may biir
Dem laak xutu kaaw baay
Tëraaw wul maag ñu ne siiw
Be laan naa saa fere free
Defal sa job, bezzi na dox
Kend maat ru ci yaaduna
Gëmmal sa bopp
Maani gëmmal sa bopp
Bo doo ña nga jëggëlu
Bo doo ña nga jëggëlu
Bo doo ña nga jëggëlu
Loo lay gentleman
Gentleman, gentleman, gentleman, gentleman
Gentleman, gentleman, gentleman, gentleman, gentleman
Xam naa lu parkouru gentleman
Sa bëk bëkki buuru ñu gënne man
Bo yaangi pilul ñu cène rekk
Kënd ñu ne këjë gentleman
Gentleman, gentleman, gentleman, gentleman
Gentleman, gentleman, gentleman, gentleman, gentleman
Xam naa lu galeru gentleman
Sa bëk bëkki buuru ñu gënne man
Bo yaangi pilul ñu cène rekk
Loo xutu kaaw baay gentleman
Loo xutu kaaw baay gentleman
Gentleman, gentleman, gentleman
Xam naa lu galeru gentleman
Gentleman, gentleman, gentleman
Ñeema deflu bess sa may definition
Sa may ñaanu man sa may benediction
Yaa ñaan akum defle lu xeess
Moo guinga neef di caw
Walaaye dagaay na yem ni ñi moos
I'm a gentleman amul bëggë man
Bu may jëkkuleek sa may bopp
Mo arts bu mellu man
Doodoo ko deggu fenn sa may rekk
Yowmi nol gëmmu mellu sa may clon
Doodoo ko defu ti doom
Liggë guindil leen sa may domaine
Xoolal kënd wuule guiné ci sa may rël
Lo fi sëmbi diñ ko naan
Amul desal amul gueddë
Flow biit amul melli catholique
Bu si njeek takki ñaareel
Indil gaa yi daanu rap
Di mooy rap bilay di daareel
Indilu bess, gozè li fess
Akki mooy yàmm, baay lu ress
Rest in peace papa gaye
Nega yàmmu naa jooglu ma lekk
Kuufi ne lëmmay def neex
Wula rekk dagaay wax lu la neex
Defal sa job, bezzi na dox
Kend maat ru ci yaaduna
Gëmmal sa bopp
Maani gëmmal sa bopp
Bo doo ña nga jëggëlu
Bo doo ña nga jëggëlu
Bo doo ña nga jëggëlu
Loo lay gentleman
Gentleman, gentleman, gentleman, gentleman
Gentleman, gentleman, gentleman, gentleman, gentleman
Xam naa lu parkouru gentleman
Sa bëk bëkki buuru ñu gënne man
Bo yaangi pilul ñu cène rekk
Kënd ñu ne këjë gentleman
Gentleman, gentleman, gentleman, gentleman
Gentleman, gentleman, gentleman, gentleman, gentleman
Xam naa lu galeru gentleman
Sa bëk bëkki buuru ñu gënne man
Bo yaangi pilul ñu cène rekk
Loo xutu kaaw baay gentleman
Loo xutu kaaw baay gentleman
Gentleman, gentleman, gentleman
Xam naa lu galeru gentleman
Gentleman, gentleman, gentleman