Skip to content

Baag

Popularity · Low

YouTube

Searching YouTube...

Lyrics

oh oh oh oh oh oh oh oh oh Ah ah ah kemeni Ah ah ah kemeni i minou beach beach minou beach oh oho Ah ah ah kemeni Ah ah kemeni iow firsting first fuckin in the best bindeu bi lay soul ni bambou sét wéthie flow flow nieup guessou défi finesse soli mboubou you bess sama scool dou dess niou gui si beug téré guiness topou niou train train bi wagon ya gui souniou bag topouniou sen game bi xana de'go souniou baat kila yag tété meuneu bania féké sa bop da nga yag die'gui tali dokhal sa bop left right Foy Tek sa tank boudé dieun bou ndaw nga dossi mouthie bilei xar kép niémé nga guew gui sa neunde nanga samp dokh souniou kaw bofa dieumé sa laf bi demal douko meusseu naw souniou reudou yoon bossi yamé nanga taxaw youxou souniou tour soul sa kaw