Skip to content
Lyric
Dive
Public playlists
My playlists
Search
Sign in
Guediawaye
Iss 814
Popularity ยท Low
+
๐ธ๐ณ Wolof ยท Original
0
0
YouTube
Searching YouTube...
Lyrics
Original
Translation
Bilingual
Guediawaye, goudi goudi, mane ak sama gars yi fook niou gnibi bendo
Ou'La la la la la mbedo dance,
mane ak sama gars yi fook niou gnibi bendo
Guediawaye, goudi goudi, mane ak sama gars yi fook niou gnibi bendo
La la la la la mbedo dance, mane ak sama gars yi fook niou gnibi bendo
Nieuweul mbedo, benene life leu, mane ak sama gars yi niou ngui bendo
Nieuweul ghetto, never mind leu, melting pot bi mo fiy daw wawaw
Wane la lodoul guiss, lodoul deggue, xamnani di nga know
Waxma ya ngui beggue, yang'koy yeukk nigth bi di gueuneu go
Tek zeum half nigth,
taal call nigth ligth, film daaw twiligth, teugg match side side
Mbedo bendoo, loloy ghetto
Guediawaye, goudi goudi,
mane ak sama gars yi fook niou gnibi bendo(bang bang bang bang)
La la la la la mbedo dance(mbedo dance)
mane ak sama gars yi fook niou gnibi bendo
Guediawaye, goudi goudi, mane ak sama gars yi fook niou gnibi bendo
La la la la mbedo dance, mane ak sama gars yi fok niou gnibi bendo
Purgรฉ nga sa peine kagn lagn lay
jugรฉ? Fatรฉl lepp nieuweul niou diapizรฉ
Kaay niou dem concert aprรจs niou gnibici
Nenagn diougue dou wรจss kone bokk gnibicil (ouhouhou ouhhh)
Kaay niou dance boudรฉ daflay dimbali nga fatรฉ say pression
Kaay niou dance fi bou weesso hip hop guisso centre de rรฉinsertion

ย