Ndaw
Baye Mass
Popularity ยท Low
Listen
YouTube
0:00 / 0:00
Loading YouTube player...
Lyrics offset
Synced
Lyrics
Par AbouAmg
ndaw la bou dรฉme
dรฉwรฉ n'a ndaw fougnou dieum
nakh koune si nioune.
amna loumou donone thi yaw
Yalla boul dieul
dou tagou day dieki rek dieul
nagne len ko nianal
mou am diam foum meuna dem
donone na domm
donone kou sori si niom
diotรฉ wone ak yaye dji
wayรฉ domm dji sakh si xool bi
fi nieupeu dioy
fi nieupe la sen xool yi toy
li ko metti wone
teknako thi lokho kharite bi
xolal lo rendi sa lokho lay nathie thei
donnรฉ kรฉ di dieundeu sa famille boul sagane mouy nadjรฉ
ki kouko wakhone
li la fiy dieulรฉ sa kharite lay diouguรฉ
meun na watte ni
watte ni douka meussa guem
xolal soy rendi sa lokho lay nathie
so nekรฉ di dieundeu
sa famille boul sagane mouy nadjรฉ
ki kokou wakhone
li la fiy dieulรฉ si sa kharite lay diouguรฉ
meun na watte ni
watte ni douka meussa guem