Jeleeti
Popularity · Low
Listen
YouTube
0:00 / 0:00
Loading YouTube player...
Lyrics offset
Synced
Lyrics
Par AbouAmg
Foo koy jëleeti?
Ku la bëggee ni man
Foo koy jëleeti?
Ku la soopee ni man
Foo koy jëleeti?
Ku la nobee ni man
Foo koy jëleeti?
Ku yeewu xaaja guddi di xool ndax sàngu nga
Ku lay wax dëgg joo bëggula dégg ni man
Ku nekk ak fa la buur bi Yàlla fetëler
Ak fa nga bëgg sa boop féetée
Fu ma koy jëleeti?
Ku ma nobee ni yaw
Fu ma koy jëleeti?
Ku may fiiree ni yaw
Fu ma koy jëleeti?
Ku ma ñeme wax dëgg ni yaw
Fu ma koy jëleeti?
Bu la buur bi Yàlla bëggee danga koy xam
Ndax tóoxiduna boo dugg mu geénee la ci
Bu la nit ki bëggee doom yaay danga koy xam
Ndax bu musiba di xeeñ mu ne"kaay gunge ma fii"
Àdduna ngoogu ci suñu kanam
Jaam warula tëkku moroomu jaamam
Àdduna ngoongu ci suñu kanam,doom yaay
Jaam warula nattu moroomu jaamam
Foo koy jëleeti?
Foo koy jëleeti?
Fan nga koy jëleeti?
Fan nga koy jëleeti?
Foo koy jëleeti?
Ku bëgg sa jamm ni man
Fu ma koy jëleeti?
Ku dégg daaj ni yaw
Fu ma koy jëleeti?
Ku mok pot ni yaw
Foo koy jëleeti?
Ku yeewu xaaja guddi di xool ndax sàngu nga
Ku lay wax dëgg joo bëggula dégg ni man
Ku nekk ak fa la buur bi Yàlla fetëler
Ak fa nga bëgg sa boop féetée
Foo koy jëleeti?
Foo koy jëleeti?
Foo koy jëleeti?
Foo koy jëleeti?
Fan la koy jëleeti?
Fan la koy jëleeti?
Fan la koy jëleeti?
Fan la koy jëleeti?