Skip to content

Yaay

Popularity ยท Low

Listen

YouTube

0:00 / 0:00
Loading YouTube player...
Lyrics offset
Synced

Lyrics

Par AbouAmg Yaye ki gueune ci mane yaye woye nala Meunoumala fatรฉ Soudoul wone ak saa yaye booy dina firim rรฉw tass koo Yaye balal ma Yaye booy kaay balal ma Soula nรฉkhรฉ daagoul sa ligueye fegn na ci sa ndiabot gui Ay camions khaliss Soumala ko done sotti Dou doye ndakh diouro lou kene di khol nane thiam kane mondiour li Mane santeu naa yallah buur bi bimala amรฉ Yaye diou melni ioe yomboul tรฉ khamna li takh ma wakh ko Sanni ma daleu Dou tรฉ malay gueureum Loula nekh deff meu sama Aldiana ngui ci sey souffou tankeu Mane santeu naa yallah buur bi bimala amรฉ Yaye diou melni ioe yomboul tรฉ khamna li takh ma wakh ko Yaye defo fii lou niaw Wakho fii lou niaw Meusso nio wane guinaaw Naadj bou tร ngue bi nga daan daaw takh sama khol sedd ci yaw Yaye gueureum nala Yaw fo diaar yone la Kouniou nane demb tรฉy motax Yone bi goudoone na loool Yaye moussoulo wagnรฉkou Bilay khepp nako loool Lou nรฉew loumay deff ci yaw Sou yokoul dotoul waniรฉkou Na lamp yii takkeu ma photowok mom Yaye rรฉtane maa Sa rรฉtane dafmay doundeul Guiss la rek dafmey bรฉgueul Doundeul doundeul Ba Abadan moma done gueuneul Yaye yama lene gueuneul Nga fรฉkkรฉ laley nianal Mangui ci yaw ba guรฉdj gui ferr ndakh yamay bรฉgueul Yaye foula ndanane di diaar Sey att yakkoul sa taar Naadj bou tร ngue bi nga daan daaw takh sama khol sedd ci yaw Yaye gueureum nala Yaw fo diaar yone la Na lamp yii takkeu ma photowok mom Yaye rรฉtane maa Sa rรฉtane dafmay doundeul Guiss la rek dafmey bรฉgueul Doundeul doundeul Ba Abadan moma done gueuneul Yaye yama lene gueuneul Nga fรฉkkรฉ laley nianal Mangui ci yaw ba guรฉdj gui ferr ndakh yamay bรฉgueul Ya foula ndanane di diaar Sey att yakkoul sa taar Par AbouAmg