Skip to content

Wakili

Popularity ยท Low

Listen

YouTube

0:00 / 0:00
Loading YouTube player...
Lyrics offset
Synced

Lyrics

Ni mala beuguรฉ baby Xayow Meussou ma beuguรฉ ni nit Sone thi beugue bani bayina Nga gneuw indi lumiรจre Mani wone aye mbeuguรฉl jigou ma Xol bi deukeu dima toogne Nga gneuw indi deugui mbeuguรฉl Mou done lou neekh Waxal gniy wootรฉ ka bippรฉ Nagne ma thieupรฉ Nimala beuguรฉ baby Xayow meussou ma beuguรฉ ni nit Xayow soumala takkรฉ baby (bรฉ) Xayow douma signรฉ polygamie Sa yo amรฉ loula metti thi mane mi Damalay xool sourire nga baalma Sama tandarma lala dipรฉ Mani bu toy ba Doylo nga sa dignitรฉ Do adou calpรฉ heey hey Maak yaw dougn rรฉroo Comment vous allez moi รงa va Nimala beuguรฉ baby Xayow meussou ma beuguรฉ ni nit Xayow soumala takkรฉ baby (bรฉ) Xayow douma signรฉ polygamie Digueuntรฉ bi deugeu la Xam sa bop yam do topando Ma chรฉrie mรฉtina tang dieur dawoulo Ayi yiii ayรฉ yรฉ aha aa Nimala beuguรฉ baby Xayow meussou ma beuguรฉ ni nit Xayow soumala takkรฉ baby Xayow douma signรฉ polygamie Xayow Nimala beuguรฉ baby Yaw la taneu def la sama diabar Diabar Diabar Diabar Yaye sama yayou doome Xayow gooro foumou dia yรฉ Waw waw ma yondi sama nii diay Waw waw ma yem si sama baby