Skip to content

Jammu Africa

Ismael Lo- Senegal
Popularity ยท Low

Listen

YouTube

0:00 / 0:00
Loading YouTube player...
Lyrics offset
Synced

Lyrics

Afrika a a a Afrika mon Afrique Sama gent gi maa ngi รฑaan Yalla wonma ko bala may รฑibbi barsaq Ma ne bes du รฑakk ci bes yi Afrika don benn reew D'ici ou d'ailleurs nous somm' des enfants d'Afrique Mรชm' si le ciel tombait luttons pour la paix Kon jammu Afrika moom lay รฑaan Manรฉ jammu Afrika mooy suรฑu natange Afrika a a a Afrika a a Afrika a a a Afrika mon Afrique Yow mi nekka bittim reew man mi Lรด maa ngi lay รฑaan Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun ta mel bul fatte Afrika Ici ou ailleurs la paix prix du bonheur Mรชm' si le ciel pleurait luttons pour nos frรจres Kon jammu Afrika moom lay รฑaan Manรฉ jammu Afrika mooy suรฑu natange Afrika a a a Afrika a a Afrika a a a Afrika mon Afrique Onon bibbe Afrika ngimode, ngimode liggo-den leydi men Ngaccen hasi daagal yoo Alla suren e musibaadi Yoo Alla addu jam to Ruanda Yoo Alla addu jam to Burundi Yoo Alla addu jam to Casamans Lawol Mbignona yee