Skip to content
Lyric
Dive
Public playlists
My playlists
Search
Sign in
Galilé - LANGAL MIC
Mist Cash
Popularity · Low
+
🇸🇳 Wolof · Original
0
0
Listen
YouTube
1
2
3
0:00 / 0:00
Loading YouTube player...
Lyrics offset
Synced
Lyrics
Original
Translation
Bilingual
Hey
Yo
Cash
Yo
Joox la délai ñu diallé ma
Nonu laay deff ba ma meuneu rare fi
Paré nélaw ba aljana (aljana)
Ko yéné mou ignané la
Mist Cash mo dakha rap fi
Boy nélene ko carrément, carrément
Hey
Dañ ko job ay ati att
Fok ma dawal ay Cadillac
Fok ma ligueye ba deh sene kaaw
Meuneu ñow corbillard sama mariage
Yonu tiow sama alliance
Ñu mudju doon sama arrivage
Namu ñu love
Namu ñu tiow
Namu ñu took compter liasse yeup
My guy do guiss
Do guiss
Roof kani sa beute do guiss
Doma daap douma daaw
Ndakh siip
Yaay bourg'ou mars
Kou dougou feey free
Tekkil sey beute si mane
Ndakh louma def doko def fils (doko def doko def fils)
Lima def doko def fils
Ndakh fima diar ku fa diar guiss
Weru way bé deugueur
Sa gëlu baay laay tieupeul
Sissu sa gayi ley eup
En tout cas nangu na ma lene eufeul
Cas moune na né ma lene euf nguene naaw
Keuf sene fiit
God damn shit
Dieul sene beat
Boy feinte si
Kush mother fuck
Def si ndank
Def si
Def si
Def si ndank ndank ndank
Def si
Def si
Def si ndank ndank ndank boy
Def si
Def si
Def si ndank ndank ndank
Def si
Def si
Ndank
Wo
Ndank ma folli ñi guen di fall
Ndank ma folli ñi guen di fall
Ndank ma folli ñi guen di fall
Carrièru ñi ma suul
Si laalu hospital
Boy Li keupeu gaal kene du ko weedi fess
Boy guedj bi dey allu
Ay niit'a fey deh
Yeah
Li nga feey djaduwul
Na nga feey Cash
Ay briques si clip'ou Ngaaka yi di sauce
Diay nga sa ngoor Xbet bi
Té dagn la sekhlou
Tilim nga dana nga oss
Diiru gnou mbag beneu fake fi
Teudjeul sa gaat
Bouko di tidji
Do défé gaat
Khana nguene fidi
Guiss ku ma meune
Face rap tiji
Mbame bouy feuleu
Gaindé bé ley
Liguey yé sexy
Tek sac bine bine
Mane lañuy get fi
Beneu fake bombul
Rap'al nga ñuy reey ak rakatak guin guin
Def lu la nekh
Nigga meune rap yombul hey
Meune rap yombul (walahi)
Meune rap yombul (walahi)
Meune rap yombul hey
Deff lula nekh ndégué
Rap'u jiiné, rap'u deumeu
Ñune ñoy yeungueul fi nga deuk
Budé ñune nga beugue teuku
Da fey melni xaru deug
Da fey melni xaru deug hey
Da fey melni xaru deug
Da fey melni xaru deug
Rap'u jiiné, rap'u deumeu
Ñune ñoy yeungueul fi nga deuk
Budé ñune nga beugue teuku
Da fey melni xaru deug
Da fey melni xaru deug hey
Da fey melni xaru deug hey
Rap'u jiiné, rap'u deumeu
Ñune ñoy yeungueul fi nga deuk
Budé ñune nga beugue teuku
Da fey melni xaru deug
Damey indi sama leep
Beugue Djité rap'u leum
Limoy funérailles'ou deumeu
Guemigne yi yeup ko eumb
Day melni nga beugueu neubeu
Ki nek si diigu ndeundeu
Dama feugueu sama deuneu
Nga sissu ma neub leep
Deubeu leep si début bi
Deug deug tegui ndeup
Feup di yeungu
Si deukeu bi
Mane na gneup ñu key reubeu
I'm back
Mane la Feugueuleu
Té feugu la la deff
Han han
Gnémé futilité
Fiitu nitté
Fitate ko sene khone break
Yow yaye done sans Marteau fer
May John Wick ak revolver
Han han
Mom zone bi, zone yi si dess
Chaque concert may zonzé
Done bandit si yene
Hey mala gueuneu khiff
Wa legui lo fok
Khana do xippi
My nigger do xol
Meune na tek
Ba gnou né legui da doff
Only God can judge me
Yaw kessé lay top
Dama kicker ba gnou né ki deh da doff
Beurre ité ndakh si founé la dox
Amu pa Bac, demu ma cité wakh deug
Té ki ma top di nga quitter nane dokh
Mama la ... diok
Moma la gueuneul fop
Meuno si mane ludul wakh
Yak sa gang yeup fuck
Tey lene damey dokh
Mey lene gnu dieul tof
Daniu diudu done bidew
Fuck mazeltov
Fi da nguey meyé ben ñu dieul leep
Méyé beneu ñu dieul fouk
Diarul pistolet
Diar si Seydina Alioune
Ladji sene pout
Fi da nguey réyanté pour dieul coupe
Am ñuy réyanté pour def tout
Pour meune la téyé
Du té pé nguey dieul
Si leep
Ya ka fey ligueye suur
Fi da nguey méyé rein
Ñu dieul ru
Comme Jaan nicaragua
Da nguey khouss
OG yombatul
Ñi ffi nékone
Lay job di job di diokh
Ba ñu suur
Galilé