Skip to content
Lyric
Dive
Public playlists
My playlists
Search
Sign in
Ñafal
Dip Doundou Guiss TV
Popularity · Low
+
🇸🇳 Wolof · Original
0
0
Listen
YouTube
1
2
3
0:00 / 0:00
Loading YouTube player...
Lyrics offset
Synced
Lyrics
Original
Translation
Bilingual
Ñii ngéen daan joow teggi nañu séen tànk, yéyé
Ana lo fi def bay bàkku, yéyé
Duu ngéen d'accord te yéen a fi dàq meew yéen
Daa ngéen fen mbaa bejjaaw te xewi ngéen
Maa ni ñafal, ñafal-ñafal (ñafal ci taat yi waay)
Gone kuu reew la ñafal-ñafal
Maa ni ñafal, ñafal-ñafal (maa ni cawal-cawal)
Da teggi nawal ñafal-ñafal
Duu ngéen d'accord teggiléen séen tànk
Chaque jour kenn panne de leen tegante tànk
Kii nekkoon séen prof laa def élève day jàng
Lamiñ, radio nee nañ kamec, toggal tele bi day tàkk
Du ngéen d'accord ku ci echec def hardcore
Nax yéen a gën a namm caché seen passeport
Loo ma jaay du jar mbaa gën a lamb séen album
Fii lépp yàmbalaŋ ñu yàgg lagg def gang toog
Duma raw mbaa sonn topp rang bi dii dagg ticket
Ñoom ñépp rë' mba raw gumba buu tëmb ci teen
Jobbal ma du am ni jën bu saña, nëbbal ci geej
Jii neel baa jëlee ci teeñ, gëm job mba amuma weekend
Ñii daan joow teggi nañu séen tànk, yéyé
Ana lo fi def bay bàkku, yéyé
Duu ngéen d'accord te yéen a fi dàq meew yéen
Daa ngéen fen mbaa bejjaaw te xewi ngéen
Maa ni ñafal, ñafal-ñafal (ñafal ci taat yi waay)
Gone kuu reew la ñafal-ñafal
Maa ni ñafal, ñafal-ñafal (maa ni cawal-cawal)
Da teggi nawal ñafal-ñafal
Buu de danga mer mba gedd di dem yaa ko fa am
Capp baa saf di yëy làppala sa màngo-baxal
Xaayan kuu dégg Séeréer danga sañse aca waxal
Dugg fu ñu nekk du yomb ci yaw faaw nga maxal
Eh danga reew, anh danga dof, lekk séen xaalis, aca ñëwléen débarraser
Ñii ngéen daan joow teggi nañu séen tànk, yéyé
Ana lo fi def bay bàkku, yéyé
Duu ngéen d'accord te yéen a fi dàq meew yéen
Daa ngéen fen mbaa bejjaaw te xewi ngéen
Maa ni ñafal, ñafal-ñafal (ñafal ci taat yi waay)
Gone kuu reew la ñafal-ñafal
Maa ni ñafal, ñafal-ñafal (maa ni cawal-cawal)
Da teggi nawal ñafal-ñafal
Duu ngéen d'accord may jibee deux trophées
Sa gel bi côté 1, jàpp ko duu jafee
Équipe yii ngéen daan joow tay ñoom la Getafe
Lii gën a cher ci li ngay jaay lañu wanteer
Làmb mooy di nga daaj
Duma Lac de guier mais suma laa daanul noo daan
Donkaasigi faa la toggoon falay toggat
Naqariwul dereet naa koo sukar baa buu saan
Sa sarax yomb na, ñaari neen la, fils doo gat
Ñii dañoo tardé di wut moroom
Sandiléen digg Lac Rose sax taxul ñu am xorom
Ñaf laa ci taat yobbu la école
Sandi maa fiit, maa sandi sa rux sunu boroom

Duu danga reew