Skip to content

Africa remembers -Youssou Ndour

Don Felicio
Popularity · Low

YouTube

Searching YouTube...

Lyrics

Stand Up Stand Up Wakhtou dafa djott niou mom sunu bopp Wakhtou dafa djott niou djokk thi sunu bopp Diokhniou indépendance waye bataye nioniou djitou Founiou la djokhei bene dieulfeu foukk sen beut neniou Yaye boye kaye dieulma bala ma dem guet (×2) Pitch mile noppil dom Anh noppil dom Pitch mile noppil dom khamnga bala djant sokh sa yaye nieuw dieul leu Yayo Yaye Yaye Danga ma beug nakh yaye dou nieuw (×2) Danga ma beug nakh yaye dou nieuw ndakhte yaye boudone nieuw nieuwna ba diant fekke Yayo Yaye Yaye Nioye khamb tal diayla arme ba pare dileu ate Guem suniou bopp daldi doyelo moniou manquei Suniou soubeu laniou tayele banque mondiale akk FMI Liguey thi bopp kagn laniou mom suniou bop Yaye boy kaye dieulma balama dep gue Monde dama meunteu naw Monde dama meunteu naw fekki Yaye (×2) Wouy Yayo boye Monde dama meunteu naw fekki yaye Danga ma beug nakh Yaye dou nieuw Monde dama meunteu naw fekki yaye Ndakhtei yaye boudone nieuw nieuwneu ba diante fekkei Monde dama meunteu naw fekki yaye Anh Monde dama meunteu naw fekki yaye Ihh Yayo Yayo Yayo Ohh Wouy Yaye Wouy Yaye Wouy Yaye (×2)