Skip to content

Sama Everything

Phillipe Ndour
Popularity · Low

Listen

YouTube

0:00 / 0:00
Loading YouTube player...
Lyrics offset
Synced

Lyrics

Yeah yeah Yay sama everything Beugeul ma défal la Amouma anything Té dou té ma défal la Wakh ma iow lo beugeu Sa baneex rek la beugeu Sama yéné défal la Togal ma firila Yay sama everything Beugeul ma défal la Amouma anything Té dou té ma défal la Yangui yekk sama loveu Yangui few sama loveu Li ma yéné xamnako And you know you know you know Mama Xamnako baby Li mala yéné you know now Mama Xamnako Baby Oh You know you know you know now Maa Xamnako Baby Xamalna ni sa domyi Deff la yéné Lou barri And you know you know you know Mama Xamnako baby Li mala yéné you know now Mama Xamnako Baby Oh You know you know you know now Maa Xamnako Baby Xamalna ni sa domyi Deff la yéné Lou barri Yalla ma bolék iow Yaye diourom nienti wér nga eumbouma Tey dji maag na Wathié di kow souf man ganéssina Wakhma lane nga beug Lépp ma défal la paréna Sama yéné manak Zeyna ci adouna ben la (ben la) Gouddou fane dé laly nianal Yobbou la makka la yéné Magg na beug dap sa love Xamna mounoumala fay Tey Yalla may sédé ci sama yéné Linga def ci nioun Yaye boy yay Gaindé Yay sama everything Beugeul ma défal la Amouma anything Té dou té ma défal la Yangui yekk sama loveu Yangui few sama loveu Li mala yéné xamnako And you know you know you know Mama Xamnako baby Li mala yéné you know now Mama Xamnako Baby Oh You know you know you know now Maa Xamnako Baby Xamalna ni sa domyi Deff la yéné Lou barri Oh you know you know you know Mama Xamnako baby Li mala yéné you know now Mama Xamnako Baby Oh You know you know you know now Maa Xamnako Baby Xamalna ni sa domyi Deff la yéné Lou barri Dolli Sant Yalla sama dom xalébi magg na Lingma yéné mangui niane buur Yalla mou degeu leu Pa Philippe sa wakh yeggna ci xol nekhnama Pa Philippe Vivane Yaye ak dom guén di ame Philippe Yay sama everything Yay sama adouna Amouma anything Naniou sant yalla Yangui sama loveu Mangui yekk sa loveu Mangui feel sa love iow mi Oh you know you know you know Mama Xamnako baby Li mala yéné you know now Mama Xamnako Baby You know you know you know now Maa Xamnako Baby Xamalna ni sa domyi Deff la yéné Lou barri Oh you know you know you know Mama Xamnako baby Li mala yéné you know now Mama Xamnako Baby Oh You know you know you know now Maa Xamnako Baby Xamalna ni sa domyi Deff la yéné Lou barri Mar buur Yacine Mar Birame Yacine Mar Birame Ngouille Alé Ndiaye