Skip to content

Xale

Youssou N'Dour
Popularity · Low

Listen

YouTube

0:00 / 0:00
Loading YouTube player...
Lyrics offset
Synced

Lyrics

No no no no No, no no no no Ne xale bi Bëgguma la mer loo Ne xale bi Bëgguma la mer loo Ndaxte soo meree Soo meree Sama yaram daw Daw ba jaaxal ma (Bul ma meree) Lu menul ñàkk Faw dafay am Wareef dafay mat Léeg-léeg mu doon lu dul neex Yow sama doom Suba tax may wax Soo magee dinga xam Ndaxte soo jooyee Soo jooyee Sama yaram daw Daw ba jaaxal ma Waa-jur ak doom Faw ñuy waxtaan Feexee mel ni mburu ak sow Ndem réeru mën ta* ñàkk Ni jamono mel Teey da cee baax Jubbantil ba mu cor Ndax muumin dafay rooy